888Starz Bindu – Wut 990 000 FCFA
888Starz Sitweb pari bu siiw la ci Sénégal. Xeeti mbir yu bari lay def, lu ci melni jeu casino ak book sport. Képp kuy kiliyaan bu bees ci platform bi mën nga am xéewal ci promo biy dalal 200% ba 990,000 FCFA. Ngeen bàyyi xel ni soo bëggee dugg ci daara ji danga wara am 18 at ci kaw.

Bonus de Bienvenue + tours gratuits

Ni ñuy bindee sa tur ci 888Starz?

Li ngay def sooy bind sa tur ci platform bi gaaw na te yomb. Képp ku nekk ci Senegal mën na ko def ci ñaari klik. Ngeen bàyyi xel ni da ngeen wara am at ngir mëna bind 888Starz. Lii daf lay wan ni ñu koy defee:
- Demal ci sitweb ofisel bu platform bi;
- Bësal ‘Bindu’ ngir tàmbali liggéey bi;
- Tannal benn ci ñeenti anam yi jàppandi ngir bind sa tur;
- Bindal leeral yiñ laaj ci anam wi nga tànn;
- Tannal Bonus dalal bi gën ci yaw;
- Bindal kodu fësal sudee am nga ko, ngir mëna am yeneen njariñ;
- Joxeel formileer bi ngir matt sa bindu.
888Starz Duggal
Sudee jëfandikukat bindu nga ba noppi, dugg ci casino bi ak sportsbook lu gaaw la te yomb. Toppal yii tegtal:
- Demal ci sitweb ofisel bu platform bi;
- Bësal ci “888Starz dugg” butoŋu nekk ci kaw xët wi;
- Tannal anam wi la gënal ngir dugg, nga dugal leeral yi nga soxla;
- Bësal “Duggal” ngir dugg ci sa kontu.
Fexeel nga am say kàrne ngir moytu yeexal. Soo daje ak benn jafe-jafe, deñu lay digal nga jokkool ak ndimbalu kiliyaan yi jaaraleko ci chat wala imeel.

Ni ñuy duggee sa tur ci aplikaasioŋu 888Starz?

Bindu ci 888Starz app nekk na liggéey bu yomb bu lay may nga jëfandikoo sport yu bari ak jeux casino ci sa aparey mobile. Soo ko bëggee def danga ko wara samp ci sa telefon. Mën nga yebbi apk bi ci sitweb bi. Kenn du fay, te yomb naa defar. Danga wara dem ci App Store sudee am nga iPhone. Soo demee ba mëna jëfandikoo app bi, toppal tegtal yii ci suuf ngir tàmbali:
- Ubbi ak aplikaasioŋ ci sa aparey;
- Bësal mbusu “Bindu”;
- Tannal anam wi la gënal (benn klik, ci telefon, ci imeel, wala ci reso sosio yi);
- Su jogee ci anam wi nga tànn, joxe leeral yi war;
- Tannal bonus sitweb bi méngoo ak sa tànneef ci pari yi;
- Soo amee kodu fësal, binndal ko ci barab biñ la jox ngir mëna am yeneen neexal;
- Xoolaat leeral yépp ngir xam ndax dëggu nañu te jeexal bindu bi.
Bonus ginaaw boo abone

Képp kuy jëfandikukat bu bees ci platform bi mën nga tànn bonus dalal bi méngoo ak sa taamu. Platform bi dafay jox benn ngir soppey sport yi ak beneen ngir gamer casino yi. Dafay baax nga tann ak xel mu dal ndax doo mëna soppi li nga tànn. Lii mooy say tànneef:
- Bonus dalal Casino. Lii xéewal la bu yéeme la, dina la may nga am xaalis bu gëna bari ak ay spin yu amul fayda ci 4 deposit yi nga njëkka def. Linga meuneu gueune am moy 990 000 FCFA! Lu weesu yokk balans bu yéeme bii, mën nga itam am 150 Free Spins ci slot yi nga mëna am. Deposit bi gëna ndaw mooy 6563 FCFA.
- Sports Welcome Bonus. Bonus dalal sport. Lii promo bu baax la ci ñi bëgg pari sportif te bëgga yóbbu ko ci beneen anam. Ci xéewal gi, di nga mëna am ba 65 500 FCFA. Soo bëggee dindi xaalis bi nga am, dangay parye 5 yoon ci pari accumulateur ak 3 tànneef ci gëna néew. Ngeen bàyyi xel ni coût bi dafa wara nekk 1.40 wala gëna kawe.
Jafe-jafe Bindu ci 888Starz
Sos kontu ci platform bi lu gaaw la te yomb. Waaye yenn saa jëfandikukat yi dañuy daje ak jafe-jafe yu mëna yeexal liggéey bi. Ci suuf amna yenn jafe-jafe bind 888Starz ak seeni pexe suko defee nga mëna tàmbali sa tukki pari ci nimu gëna gaawe.
- Kodu fësal bi doxul. Sudee nangu wuñu sa kodu promo bi ngay dugg, xool bu baax ndax dugal nga ko bu baax. Waaye itam, fexeel nga xam ndax daawul jeex, te dafay wax ci kazino 888Starz. Su jafe-jafe bi wéyee, jéemal bind sa tur te du am kodu fësal bi nga jokkool ak ekipu ndimbal mi ngir ñu def ko ci loxo.
- Kontu baa ngi fi ba noppi. Soo joxe mesaas bu lay wax ni dañuy jëfandikoo sa e-mail wala sa nimero telefon, amaana am nga kontu ci sitweb bi ba noppi. Jéemal jëfandikoo “Fatte nga sa baatu-jàll?” man-man ngir defaraat xëcc. Su loolu mënu, jokkool ak ndimbalu kiliyaan yi. Mën nañu la jàppale nga am wala nga defaraat sa kontu.
- Xët wi dafay wéy di gelé ci diiru bindu. Sudee xëtu bindu bi dafay wéy di sarsewaat wala di gelé, loolu dafay faral di aju ci koneksioŋ internet bu néew doole. Jéemal soppi ci reso Wi-Fi bu gëna dëgër wala nga gëna jege sa routeur.
Laaj ak tontu
Naka may def ba am kontu ci 888Starz?
Soo bëggee sos kontu, demal ci sitweb ofisel bi nga bës mbusu “888Starz bindu“. Mën nga tànnee ci 4 anam, lu ci melni benn-klik, ci telefon, ci imeel, wala ci reso sosio. Bindal leeral yiñ la soxla, nga tann Bonus Dalal soo ko bëggee, nga yonne formileer bi.
Lan laa wara def sudee fàtte naa sama baatu-jàll?
Soo fàttee sa baatu-jàll, bësal ci “Fàtte nga sa baatu-jàll?” lëkkalekaay bi ci xëtu dugg bi. Toppal tegtal yi ngir reset ko ci sa e-mail wala nimero telefon bi nga bind. Ngir am ci yeneen ndimbal, jokkool ak ñiy jàppale kiliyaan yi.
Ndax mën naa sos kontu 888Starz ci jëfandikoo reso sosio yi?
Waaw, 888Starz dafay jàppale tànneefi dugg ci reso sosio yu melni Twitch ak Google. Dina tax nga mëna gaaw ci pari.